Khalice (feat. Yousou n'dour) - Akon feat. Yousou n'dour

Bilahi khaliss nekhna niamna si dara
Bouma si ammé sakkou douma takha doyyal yaye
Doyyal yaye douma takha doyyal yaye
Mané bouma si ammé sakkou douma takha doyyal yaye
Bo beugué melni akon ak youssou ndour way
Bo beugué tollou fignou tollou warnga liguèye way
Liguèye way mané warnga liguèye way
Bo beugué tollou fignou tollou warnga liguèye way (khalice (4f)
Warnga liguèye way
Khalice (4f)
Warnga liguéye way
Demb linga daneu takhlou waw yée
Batay diappeu ngako
Soubeu yangui woutti lénéneu
Fékhél boumoula raaw nila démai
Alu national Akon international
Kone liguéyeu woor
Liguéye lén
Djiguén gni rafet nguén xamnguén si dara
Boumassi tanné bou baxx bi
Wooy douma nélaw yaye
Ooh nélaw yaye
Dootouma nélaw yaye
Boumassi tanné bou baxx bi
Wooy douma nélaw yaye
Weur na adduna deffna fa dara
Lepp louma dieulé fofou bokk ko ak sama reew
Bokk ko ak Sénégal
Ndax mou dieum kanam
Ndaxx mou dieum kanam
Ndaaax mou dieum kanam
Khalice
Motakh mayyeu liguéye
Khalice
Motakh mayyeu gnaffé
Khalice
Motakh mayyeu goorgorlou
Khalice
Indiko Sénégal
Khalice
Mani mangui tchaa kawam
Khalice
Bilahi mangui tchaa kawam
Khalice
Pour gnou dieum kanam
Khalice
Ooh waw waw
Khalice
Liguéyeu lén
Khalice
Liguéyeu lén
Khalice
Liguéyeu lén
Khalice
Ohh waw waw
Khalice
Liguéyeu lén
Khalice
Liguéyeu lén
Khalice
Liguéyeu lén
Khalice
Ohh waw waw
FIN



Credits
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link

Video consigliato

© 2020 Riproduzione riservata. Rockol.com S.r.l.
Policy uso immagini

Rockol

  • Utilizza solo immagini e fotografie rese disponibili a fini promozionali (“for press use”) da case discografiche, agenti di artisti e uffici stampa.
  • Usa le immagini per finalità di critica ed esercizio del diritto di cronaca, in modalità degradata conforme alle prescrizioni della legge sul diritto d'autore, utilizzate ad esclusivo corredo dei propri contenuti informativi.
  • Accetta solo fotografie non esclusive, destinate a utilizzo su testate e, in generale, quelle libere da diritti.
  • Pubblica immagini fotografiche dal vivo concesse in utilizzo da fotografi dei quali viene riportato il copyright.
  • È disponibile a corrispondere all'avente diritto un equo compenso in caso di pubblicazione di fotografie il cui autore sia, all'atto della pubblicazione, ignoto.

Segnalazioni

Vogliate segnalarci immediatamente la eventuali presenza di immagini non rientranti nelle fattispecie di cui sopra, per una nostra rapida valutazione e, ove confermato l’improprio utilizzo, per una immediata rimozione.